• il y a 3 ans
DA FA LAA

Da fa laa , wóolóo ,
teg la nak , fu mu teg ul keneen
Di dox sa bëgg bëgg , di dab sa banneex ,
ndax seetlu nga koo
yaw, Yaw la bëgg ,
te yaw , yaa ko sagal ,
waaw waaw

Bu mbëggéel , doon lumière ,
mel na ni , ni jant bi
Te su am oon , lu ko gën ë leer,
dem na wut i ko
Ni yaw , diaral nga ko ,
lu raw , sóoru gayndé ,
waaw waaw

Lu mu metti metti , di nga tew ,
lu mu sori sori , an ! di nga ñëw ,
ca dëgg dëgg dëgg
dem na , ba dem , mën ë tul ë tok
benn bés , bum la , gis ul


jox na la bii respect ,
nga delloo ko bii respect
Entre vous , entre vous chérie ,
du wax lii def leneen
Ca dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg,
ya ko diara
ni yaw, yaa ko sagal ,
waw waaw

Fépp fu mu mën ë ne ,
da fay sentir sa parfum
Loolu yaa ko ko diaral ,
ndax yaa ko liggéey
Les mots qu’il utilise ,
sont toujours en deçà
De ce qu’il ressent ,
yaw yaa ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Daf la bëuggué
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Kay nga diégué ko
Mou laye déy


Yaw mii yaw ,
su fekkee li mu la wax doy ula ,
Boo yakkamtee ,
mu def al la ko , ni nga ko bëggée

mom contane neu
te sakh yaguena bëgg thi yaw,
Boo yakkamtee ,
mu def al la ko , ni nga ko bëggée

sa lui vas,
chérie sa lui vas lo def nekh na ko
da fa laa, da fa laa
def ni nga ko def


Loo bëgg , mu indil la ko
Loo laaj , mu kheuthiel la ko
Su fekkee am u ko , mu ñaan ko yalla

Chérie boy, chérie boy
Ya ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy
Lo diokhogne mo dok
Chérie boy, chérie boy
Lo def nonou la
Chérie boy, chérie boy
Ya ko ko diaral


Youssou Ndour, madjiguene
Boul yekhal dara
Na gua gaw, na gua gaw
Te li djieuntima
Sokhla yi, sokhla yi
Gnome gno ma gueteun

Category

🎵
Musique

Recommandations